lundi 6 novembre 2023

                        

As SALIHOU


SËRIÑ TUUBAA moo ñuy nettali melow gaañu baax ña

Waaye man ma jàpp ne rekk mooy ñi àndoon ak moom.

Dafa waxni bokk na ci seen i melokaan 

صمت وجوع طويل بعده سهر

وعزلة عن شيوخ بلإشاراة

Dañuy noppi ci lu leen amalul njariñ, ak di xiifal seen bopp xiifal gog lu yàgg lay doon, ginnaawe loolu it, ñuye néewale seeni nelaw ngir wéetal seen BOROOM, ak di beru (wéet) beru gog dafaye àndak Sëriñ bu leen di gindi

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire

Nombre total de pages vues

Khassida Plus TV

Khassida Plus TV
Chaîne YouTube