SERIGNE TOUBA NÉNA
Kou Tédde ki Ahmadou
Serigne touba néna yéne gnep laye waxal gnéte mbira ngui ni yo xamné kou si diap mouthie si chaytané 👉حصونكم طر من الرجيم * ثلاثة فلتفهموا منظومي ☝️
Serigne touba néna bassa ndieuk moy takko ak djiouliy diourom té diko défé sa mbolo ya (diaakka) djia 👉أولها المسجد ✍️
Serigne touba néna yén samay mbok gnarél ba moy nguén takho ak toud yalla (yobalé na djiouli si yonnenti bi SAS …)👉ثم الثاني دوام ذكر الله يا إخواني ✍️
Serigne touba néna gnétél bi moy saxoo diang alhourane (Al Karim)té and kok lab ak séntantal makhna yi (ndiangu mou téy )👉ثالثها تلاوة القرآن بالطهر مع تدبر المعاني✍️
( Khassida Plus Officiel ) 🖋️🖊️📚
Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire